Go To Top

Bamako Lyrics

Si gare bi lako fekkeu,
Mi ngui sanguo seur
Té beut yi di takkeu,
Ma dal di koye nougnou
Mou dal di maye faye ,
Dal di maye yédeu ci adouna bou yakhou bi
Mane douma fatté!

Ah mani ah mani!
Man douma fatté bamako lii mani lii mani!
Mane douma fatté!

Kerok lama khamal louma khamoul woone ci diamono bou yakhou bi yénene ak yénene;
Balaa maye dougeuti mane ci loumou meuneu doone
Dinaa fattélikou ndaw sossou
Limouma wakhoone!
Souy souy sou sou sou sou sou sou souy!!
Ci gare bi lako fekkeu mi ngui sanguo seur té beut yi di takkeu,
Ma dal di koye nougnou
Mou dal di maye faye dal di maye yédeu,
Maky yé maky maky yé maky yééééé!!!!
Waw kérok lama khamal louma khamoul woone ci diamono bou yakhou bi,
Balaa maye dougeuti ci loumou meuneu doone,
Dinaa fattéli ko maky yé maky maky yé maky yéé!!
Ah mani ah mani!
Douma fatté bamako lii mani lii mani!
Mane douma fatté bamako

Bamako Lyrics performed by Youssou N'Dour are property and copyright of the authors, artists and labels. You should note that Bamako Lyrics performed by Youssou N'Dour is only provided for educational purposes only and if you like the song you should buy the CD


What is the meaning of Bamako lyrics?